Chapter 16 Flashcards
1
Q
I brought down the books which were on top of the cupboard
A
Aaji naa teere bi yi ci kow almoor bi
2
Q
His finger is psrained
A
Baaram am bi dafa foxoj
3
Q
mud
A
ban
4
Q
give me a banana
A
Mey ma banaana
5
Q
The hospital has bandage
A
lopitaan bi amut bandaas
6
Q
branch section of tree
A
banxaas
7
Q
bench
A
banj
8
Q
none
A
ben
9
Q
we haven’t seen any of them
A
ben lenu gi sut
10
Q
to bend sway or twist
A
biij
11
Q
He will twist the screw
A
Dina biij bulon bi
12
Q
iguana
A
bar
13
Q
washing pan
A
benuwaar
14
Q
I am washing in washing pan
A
Mangi foot ci benuwaar bi
15
Q
inside out
A
bitarneku
16
Q
to cover
A
biti
17
Q
to pierce
A
bonaa
18
Q
to yawn
A
boobali
19
Q
to kill
A
boom
20
Q
roasted peanuts
A
caaf
21
Q
vagina
A
caapa
22
Q
Stand on the barral
A
Taxawal ci kow borig bi
23
Q
to roll
A
boronj
24
Q
penny
A
burey
25
wheelbarrow
buruwet
26
button
butonj
27
to scoop or gather
buub
28
piece of music
buum
29
to crawl under
bota
30
I am able to crawl under the bed
Mun naa bota ci ron lal bi
31
We chatted till day break
denu waxtaan be botset
32
to uproot or extract
buddi
33
Extracting a tooth is scary
Buddi bon dafa ragallu
34
flip flops
carax
35
puzzles
cax
36
hygiene
cet
37
to be drunk
daaju
38
gum
daakaande
39
fisherman
cubalo
40
to knock down
daanel
41
to drive away
daaxa
42
way of dress
colin
43
I don't like your way of dressing
Sa colin bii neexuma
44
penis
cuucu
45
to run after
daaxee
46
to have nothing
dara
47
I have nothing
Amuma dara
48
bed sheet
darab
49
spread the skheet on the bed
darab bi ci kow lal bi
50
to assume
defe
51
I believe he is watering the garden
defe naa ne munge roose naako bi
52
to come back
delusi
53
When will you come back
Kan ngay deelusi
54
obligatory
dagan
55
driver
dawal kat
56
to be impatient
faraw
57
The forest
aala
58
foam matress
apons
59
to lengthen
Ñaambaas
60
Bad
Bahoo
61
I live in Senegal
Amna Senegal
62
Before I lived in
Foofo de la non
63
Where is the chief of the family
Ana birem jaboot
64
Me too
Tamite
65
Neighbor
Ndeckdo
66
Book
Tere
67
I want to ask you a questiom
Lima bugga laag
68
That's to say
Mooy
69
Courage
Feet
70
Kingdom of God
Nguuram
71
Suffering
Meti
72
God has given husband, wife and children what he must do in the family
Yalla defa jok goor ak jijeen ak xali yi koo neka linga walla def ci biir jaboot
73
Soumettre
Deggal
74
Knowledge
Xam-xam
75
Do you understand what I say
You est ce que. Comprendre lima wax
76
Chief religious
Ki ilfa denne
77
Drunkard
Manikat
78
He is controling
Mooy controler
79
To hit
Door
80
Man does not hit himself
Goor du door boppam
81
Parents
Waajur
82
Do you think that if the mrmbers of the family apply the instructions of God in Bible it will be happy
Est ce wue goor jijenm ak xale bu new toppe ba too yalla dune do jaboot denna nare
83
What do you think
Ci sa xalat
84
How do you feel
Loo ci xalat
85
Applique
Te di ko topp
86
I thank God
Mangi sant
87
Did you sleep good
Nelaw ngabu baax
88
You
Nga
89
Smart
Am-xel
90
Sinner
Baakarkat
91
Here is a good place
Fi beteb bu baax la
92
He wants this one
Bu la bugga
93
Myself
Maangi am
94
I have love for you
Maangi am bëgga yow
95
I don't know you
Man xamuma la
96
You don't knowr
Yow xama la ma
97
Its finished
Jaa na
98
That is/c'est que
Lima
99
C'est bon
Neex na
100
To rebel
Fippu
101
What must do
Linga wara deff
102
He will no longer go to Banjul
Doot dem banjul
103
She or he
Moom
104
You ate bread
Leekoon nga mburu
105
One child
Doom
106
I gave to you
Dama laay jox
107
I must preach
Dama wara warate
108
Over there
Foofu
109
Wish
Yakar
110
To live
Doondu
111
Fruit
Doomu garab bi
112
To absorb
Naan
113
The sand absobs water
Suff dafay ndox mi
114
To accelerate
Baral
115
Thisis going to accelerate the work
Loolu dina baral liggeey bi
116
To accept
Nangu
117
To accompany
Gunge
118
Come and I will accompany to the market
Kaay gunge ma marse
119
Suivant
Bi ci topp
120
Le jour suivant
Bes bi ci topp
121
Supporter
Gaddu
122
Sure
Woor
123
Ce n'est pas sûr
Woorul
124
My uncle is a tailor
Sama ni jaay tayoor la
125
To hold-tenir
Teye
126
I hold it well
Teye naa oi bubaax
127
Il est vender de tissu
Jaaykatu piis la
128
Vivre
Dind
129
Vow
Yeene ji
130
Voyager
Tukki
131
My husband is not here
Sama jekker nekku fii dafa tukki
132
C'est vrai
Degg la
133
Ce n'est pas vrai
Do dugg