My Wolof Flashcards
(234 cards)
Where is the bathroom?
Ana wanaag bi? Ana duus bi?
How are y’all?
Na ngeen def?
Do you speak English or French?
- Only a little.
[Ndax] dégg nga angale walla fraase?
- Tuuti rekk.
Thank you
jërëjëf
I’m good, and you? (Response to “Na nga def”)
Ma ngi fi [rekk], yaw nak?
Yes
Waaw
No
Déedéet
thousand
junni
2000
ñaari junni
7945
juróom-ñaari junni ak juróom ñeenti téeméer ak ñeent-fukk ak juróom
10k
fukki-junni
100k
téeméeri-junni
million (x2)
tamndareet, million
My name is Thomas
Thomas la tudd.
And you, what is your name?
Yaw, no tudd?
How much is it? (cost)
Ñaata la?
a little lower (bargaining price)
wàññil tuuti?
It’s good, it’s nice
Nex na.
See you later.
Ba beneen yoon.
Goodbye. Go in peace
Demal ak jàmm.
Good night.
Fanaanal ak jàmm (singular)
Fanaaleen ak jàmm. (plural)
onion
soble
African eggplant
jaxatu
garlic
laaj