Wolof Assimil Flashcards
(43 cards)
1
Q
Comment t’appelles tu?
A
Naka nga tudd?
2
Q
Je m’appelle Amelie
A
Maa ngi tudd Amelie
3
Q
Je suis européenne
A
Waa Tugal laa
4
Q
D’où viens-tu?
A
Waa fan nga?
5
Q
Moi aussi
A
Man itam
6
Q
Vouloir
A
Bëgg
7
Q
Visiter
A
Wër
8
Q
Aller
A
Dem
9
Q
Je
A
Ma
10
Q
Tu
A
Nga
11
Q
Il/elle
A
Mu
12
Q
Nous
A
Nu
13
Q
Vous
A
Ngeen
14
Q
Ils/elles/on
A
Ñu
15
Q
Je suis
A
…laa
16
Q
Tu es
A
…nga
17
Q
Il est
A
…la
18
Q
Voici
A
A ngi
19
Q
Voilà
A
A nga
20
Q
Te voici
A
Yaa ngi
21
Q
Manger
A
Lekk
22
Q
Mange!
A
Lekkal!
23
Q
Mangez!
A
Lekkleen!
24
Q
Ami
A
Xarit
25
Connectif : l'ami de fanta
XaritU Fanta
26
Ici
Fi
27
Habiter
Dëkk
28
C'est à Gorée que nous sommes aller
Gore LAnu dem
29
Avoir
Am
30
Combien
Ñaata
31
Enfant
Doom
32
Et
Ag
33
1
Benn
34
Homme
Góor
35
2
Ñaar
36
Femme
Jigéen
37
Quoi
Lan
38
Voir
Gis
39
J'ai vu
Gis naa
Verbe d'action + conjugaison en na
40
Je suis fatiguée
Sonn naa
41
Je mange du riz
| Inaccompli
Ceeb laay lekk
42
Riz
Ceeb
43
Qui (Subordonnée relative)
Yu