Words Flashcards

1
Q

ab

Ab paaka la yore

A

indéfini pour la classe b-

Il a un couteau sur lui

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
2
Q

abal

Abal ma sa téere!

A

prêter

Prête moi ton livre

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
3
Q

able

Peñe, ken du ko able

A

prêter

un peigne, personne ne le prête

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
4
Q

afeer b-

Loolu sa afeer la

A

affaire

C’est ton affaire

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
5
Q

ag

A

indéfini pour la classe g-

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
6
Q

agsi

Xabaar bi aksi na démb

A

arriver, survenir

La nouvelle est arrivée hier

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
7
Q

aj

Fatou aj na laytanam

A

placer en haut, percher

Fatou a placé sa calabasse en haut

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
8
Q

aj

A

faire le pélerinage à la Mecque

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
9
Q

ku

A

qui annexion pour la classe k-

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
10
Q

bëgg
bëgg na mango
dafa bëggoon tukki, waaye paasam mutul

A

aimer, vouloir, avoir envie
il aime les mangues
il voulait voyager, mais il lui manquait d’argent pour le billet

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
11
Q

bu
Néeg bu tuuti la
Bu liggéey bi eggee dinaa leen nexal

A

1 annexion pour la classe b-
C’est une petite chambre
2 Quand le travail sera terminé, je vous récompenserai

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
12
Q

mat

Taaf bi matul, jëndaat ci ñaari meetar

A

être complet, arriver à maturité, être conforme à certaines normes de grandeur
l’étoffe est insuffisante, achêtes-en encore deux mètres

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
13
Q

Ku Bëgg lem ñeme yamb

ñeme

A

qui veut du miel ne doit pas craindre l’abeille

avoir le courage de, oser, être courageux, ne pas avoir peur de

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
14
Q

comment

A

nan, naka, na

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
15
Q

nan

nan nga gise mbir mi

A

de manière, comment?

comment vois tu l’affaire

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
16
Q

naka
naka-jekk
naka-jegg fii lay fanaan

A

?
normalement, de tout temps
normalement. je passe la nuit ici

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
17
Q

na
waxu ma na mbir ma deme woon

dafa defoon na yow

A

de manière, comment
il ne m’a pas dit comment l’affaire s’était passé
indicatif de fonction
il avait fait comme toi

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
18
Q

mbir m-

A

l’affaire

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
19
Q

gise

A

voir

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
20
Q

il ne m’a pas dit comment l’affaire s’était passé

A

waxu ma na mbir ma deme woon

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
21
Q

il avait fait comme toi

A

dafa defoon na yow

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
22
Q

normalement. je passe la nuit ici

A

naka-jegg fii lay fanaan

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
23
Q

Prête moi ton livre

A

abal ma sa téere

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
24
Q

un peigne, personne ne le prête

A

peñe, ken du ko able

How well did you know this?
1
Not at all
2
3
4
5
Perfectly
25
Percher, placer en haut | Fatou a placé sa calabasse en haut
aj | Fatou aj na laytanam
26
aimer, vouloir, avoir envie il aime les mangues il voulait voyager, mais il lui manquait d'argent pour le billet
bëgg bëgg na mango dafa bëggoon tukki, waaye paasam mutul
27
1 annexion pour la classe b- C'est une petite chambre 2 Quand le travail sera terminé, je vous récompenserai
bu Néeg bu tuuti la Bu liggéey bi eggee dinaa leen nexal
28
yamb w- | xam na lu bare ci yamb yi
abeille | il connaît beaucoup de choses sur les abeilles
29
abeille | il connaît beaucoup de choses sur les abeilles
yamb w- | xam na lu bare ci yamb yi
30
qui veut du miel ne doit pas craindre l'abeille | avoir le courage de, oser, être courageux, ne pas avoir peur de
Ku Bëgg lem ñeme yamb | ñeme
31
boo ñeme téegu, na nga ma ko wax
quand tu auras le courage de te faire circonscrire, tu me le diras
32
quand tu auras le courage de te faire circonscrire, tu me le diras
boo ñeme téegu, na nga ma ko wax
33
Am naa giléém ca Gànnaar yomb naa wax
J’ai un chameau en Mauritanie, c’est facile à dire.
34
J’ai un chameau en Mauritanie, c’est facile à dire.
Am naa giléem ca Gànnaar yomb naa wax
35
giléem, gëléem g-
dromedaire. chameau
36
dromedaire. chameau
giléem, gëléem g-
37
Gànnaar g-
Mauritanie
38
Mauritanie
Gànnaar g-
39
yomb
être facile, être bon marché
40
être facile, être bon marché
yomb
41
kaayleen ma jox leen cax wu yomb
venez je vous donne une divinette facile
42
venez je vous donne une divinette facile
kaayleen ma jox leen cax wu yomb
43
jên, noor lay gën yomb
le poisson en saison sèche est moins cher
44
le poisson en saison sèche est moins cher
jên, noor lay gën yomb
45
Tuñum giléém lang na, waaye rotul
La lèvre du chameau pend, mais elle ne tombe pas.
46
La lèvre du chameau pend, mais elle ne tombe pas.
Tuñum giléém lang na, waaye rotul
47
tuñ m-
lèvre
48
lèvre
tuñ m-
49
lang
prendre, dépasser, s'accrocher
50
prendre, dépasser, s'accrocher
lang
51
rot
tomber
52
tomber
rot
53
defaraatal sa ëmb, musóor gaa ngiy lang
refait ton paquet, le foulard dépasse
54
refait ton paquet, le foulaar dépasse
defaraatal sa ëmb, musóor gaa ngiy lang
55
musóor g-
le foulard
56
le foulard
musóor g-
57
gaa
particule d'insistance
58
particule d'insistance
gaa
59
ngiy
ww
60
ww
ngiy
61
Bant, lumu yàgg cig dex, du tax mu soppiku jasig
Un bout de bois, il peut rester longtemps longtemps dans un fleuve, ce n’est pas pour ça qu’il va se transformer en crocodile.
62
Un bout de bois, il peut rester longtemps longtemps dans un fleuve, ce n’est pas pour ça qu’il va se transformer en crocodile.
Bant, lumu yàgg cig dex, du tax mu soppiku jasig
63
Bant
bout de bois
64
bout de bois
Bant
65
yàgg
rester longtemps
66
rester longtemps
yàgg
67
dex g-
fleuve, rivière
68
fleuve, rivière
dex g-
69
dëgg neexul a dégg
la vérité n'est pas toujours agréable à entendre
70
la vérité n'est pas toujours agréable à entendre
dëgg neexul a dégg
71
jasig j-
crocodile
72
crocodile
jasig j-
73
soppi
changer
74
changer
soppi
75
soppi b-
le changement
76
le changement
soppi b-