Chapter 8 Flashcards
0
Q
Demba is not at tge center, he is in the shop
A
Demba nekkul ci santar bi, mungi ci butik ba
1
Q
He is in the classroom
A
Mungi ci biir kalaas bi
2
Q
The person
A
Nit ki
3
Q
Tge people
A
Nit ñi
4
Q
The men
A
Goor ñi
5
Q
The women
A
Jigeen ñi
6
Q
The adults
A
Maggñi
7
Q
The old people
A
Magget ñi
8
Q
The young people
A
Ndaw ñi
9
Q
The kids
A
Xale yi
10
Q
The trees
A
Garab yi
11
Q
The tables
A
Taabul yi
12
Q
Excuse me
A
Baal ma
13
Q
Repeat!
A
Waxaatal!
14
Q
Stop talking
A
Noppil
15
Q
Learn well
A
Jangleen bu baax
16
Q
To be slow
A
Yéex
17
Q
To wake up
A
Yeewu
18
Q
To get up
A
Jog
19
Q
To go to school
A
Jàngi
20
Q
To teturn to
A
Dellu
21
Q
To meet with
A
Daje ak
22
Q
To help
A
Dimbali
23
Q
City
A
Dëkk bi
24
Everyday
Bes bu nekk
25
After that
Gannaw looli
26
In general
Lu ci ëpp
27
Before
Ballaa
28
Leftovers
Ci booru
29
Under the tree
Suufu garab bi
30
Some times
Yennssay
31
To train
Taggat
32
Homewoek
Devoir
33
Often
Faraldi
34
Right now
Leegi- leegi
35
On the spot inmediately
Ci saasi
36
Every or each
Bu nekk
37
I go to the restaurant when i go to theis
Damay dem restaurant sufekkee dem naa cees
38
Day after tomorrow
Gannaaw suba
39
Okra
Kañja
40
Tomato
Tamaate
41
Garlic
Laaj
42
Parsley
Persil
43
Carrot
Karoot
44
Cucumber
Concombar
45
Beet
Betteraw
46
Beans
Ñebbe
47
Orange
Oran
48
Banana
Banana
49
Grapefruit
Pompalmuus
50
Pineapple
Ananas
51
Apple
Pom
52
Warermelon
Xaal
53
Grape
Resin
54
Papaya
Papaaya
55
Purple
Wiyole
56
To be hard
Jafe
57
To be pretty
Rafet
58
The meal is too hot
Ñam bu tang
59
A white fabric
Tisi bu weex
60
Ndox mu sedd
Cold
| Water
61
A good rice
Ceeb bu neex
62
A pretty woman
Jigeen ju rafet
63
A tall man
Goor go njool
64
Sick kids
Xale yu feebar
65
The coffee is not good
Kafe bi neexul
66
Ñam bi saful xorom
Tge dush is nit salty
67
Wolof is not hard
Wolof jafewul
68
Bëgguma fa dem
I don't want to go there
69
I habitually do something
Damay
70
IYou habitually do something (singular)
Dangay
71
(s)he it habitually do something
Dafay
72
We habitually do something
Danuy
73
You Pl habitually do something
Dangeendi
74
They habitually do something
Dan~uy
75
Men drink tea only
Goor n~i dan~uy naan attaya rekk
76
to manage
Saytu
77
Mud stove
Furno ban ac suuf
78
Which road is going to....
Ban yoon moo je*m?
79
Go straight
Jubbalal
80
Go until
Demal ba
81
Cross the paved road
Jeggil tali bi
82
take this road
Je*lal yoon wii
83
Where is
Ana fahn la...... nekk
84
It is located at
Mungi ci
85
It's not far
Sorewul
86
What is having there? What is found there?
Lu am foofu?
87
There is
Am na
88
Is there
Ndax am na
89
Where can I find (person)
Fu ñu mena ame
90
I'm lost
Dama Reer
91
Im looking for the road to
Yoonu xxxxxx laay laaj
92
North
Be*t gannaar
93
south
Be*t saalum
94
East
penku
95
west
soowu
96
In front of
Ci kanam